Colossians 3:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te bés bu Kirist miy seen dund feeñee, yéen itam dingeen feeñ ak moom ci biir ndam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seenug dund dëgg Almasi la, te keroog bu Almasi feeñee, yeen itam ay ànd ak moom feeñ, ba séddu ci ndamam.