Colossians 3:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye léegi bàyyileen yii yépp: mer, xadar, kiñaan ak di génne ci seen gémmiñ sos ak wax ju ñaaw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye léegi lii lépp baleen ko: tàng xol, ak mer mu ëpp, ak coxor, ak saaga, ak waxi ñàkk kersa.
Recommended Reading