Colossians 4:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi koy seedeel ne, mu ngi sonn bu baax ngir yéen, ngir waa Lawdise ak waa Yerapolis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa ko seedeel ne coonoy ñaan bu réy la nekke, ngir yeen ak waa Lawdise ak waa Yerapolis.