Colossians 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nuyul-leen nu mbokk, yi nekk Lawdise. Nuyul-leen nu itam Nimfa ak mbooloom ñi gëm, miy daje ci këram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nuyul-leen nu bokk yi dëkke Lawdise, ak sunub jigéen Nimfa, ak mbooloom gëmkat, miy daje këram.