Colossians 4:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu ñu jàngee bataaxal bii ci yéen, fexeleen ba ñu jàng ko it ci mbooloom ñi gëm mi nekk Lawdise, te yéen it ngeen jàng bi ma yónnee waa Lawdise.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw bu ngeen jàngee biral, bataaxal bii ci seen biir, fexeleen it ba ñu jàng ko, biral, fa mbooloom gëmkat ma fa Lawdise, te yeen it bataaxal ba ngeen di jote Lawdise, nangeen ko jàng biral.