Colossians 4:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te ngeen fasaale nu ci ñaan yi itam, ngir Yàlla ubbil nu bunt, nu man a xamle kàddoom, di yégle kumpa gi di Kirist, muy kumpa gi waral ñu jéng ma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te ngeen ñaanaale nu ci itam, ngir Yàlla ubbil nu buntu xamle kàddu gi, ngir siiwtaane mbóot mi ci Almasi, li waral ñu jéng ma.