Colossians 4:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na seen wax jépp fees ak yiw te am xorom, ngir ngeen xam nan ngeen war a tontoo ku nekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na seen kàddu ànd ak yiw te am solo, te ngeen xam nu ngeen di tontoo ku nekk, tont li war.

Recommended Reading