Daniel 1:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te nga xool nu, xool xale yu góor yiy lekk ci njëlal Buur. Su ko defee nga seet nooy def ak nun ci ni nga nu gise, sang bi.»