Daniel 10:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man Dañeel doŋŋ maa gis peeñu mi. Ñi ma àndal gisuñu ko. Tiitaange lu réy nag jàpp leen, ba ñu daw, làquji.