Daniel 11:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu dina wuta moom fa féeteek dun ya, ba nangu ca ay réew, waaye dina am njiitu xare lu dakkal jëfi réy-réyloom ji muy torxale, ba fey ko añam.