Daniel 11:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu loolu weesee dina walbatiku dal ci dëkk yi ñu wëralee tata ci biir réewu boppam, waaye du sotti. Day daanu, ne mes.