Daniel 11:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ku siblu moo koy wuutu, ku yelloowul darajay nguur. Day duggsi ndànk, lal ay pexeem, ba nangu nguur gi.