Daniel 11:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bu àpp bi jotee, buur bëj-gànnaar dina dal ci kaw réewum bëj-saalum. Waaye boobu yoon du deme na woon.