Daniel 11:37 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur bi du faale tuuri maamam, du faale tuur mi jigéen ñi sopp. Du faale menn tuur, ndax day damu ba weesale boppam lépp.