Daniel 11:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kenn ci waa këram mooy wuutu baayam, dikk, dal ca mbooloom xarem buur bëj-gànnaar, jàll ba ca wàllaa tatay buur bëj-gànnaar, jëflanteek ñoom, duma leen, ba daan.