Daniel 2:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dañeel def ug teey, jiital xelam, wax ak Aryog, kilifag dagi buur, fekk kooku di dem, nara reyi boroom xam-xami Babilon.