Daniel 2:43 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li nga gis weñ gu jaxasook ban mooy tekki ne buur yi dinañu booloo ci seeni pexe, waaye seen bennoo du mujj; dafa mel ni weñ rekk, du jaxasook ban.