Daniel 2:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur dellu ne: «Gis naa nag bu baax ne dangeena bëgga yàggal mbir mi, ndax xam ngeen ne dogal bu wér tukkee na ci man