Daniel 3:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sadarag, Mesag ak Abet Nego, ñoom ñett ñépp yeewe ba ne ŋodd, tàbbi ca biir taalu sawara bu yànj ba.