Daniel 3:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bataaxalu Buur Nabukodonosor a ngii, jëm ci mépp mbooloo ak wépp xeet ak wépp làkk, ak fu ñu dëkke ci àddina sépp: Yal na seen jàmm yokku.