Daniel 4:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba sama sago délsee, ca laa jotaat ndam ak daraja ngir sama teraangay nguur. Ba loolu amee samay jawriñ ak samay jaraaf jëlsi ma; ñu dëjaat ma ci nguur gi, ma gënatee màgg.