Daniel 5:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee boroom xam-xami Buur yépp dikk ba ca biir, waaye manuñoo jàng mbind ma, bay xamal Buur la muy tekki.