Daniel 6:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu neex Daryus nag, mu fal téeméeri jawriñ ak ñaar fukk ca réew ma, ñuy saytu nguur ga gépp;