Daniel 7:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«May xool ba tey ndax kàdduy damu yooyu béjjén biy wax, ma gis ñu rey rab wa, sànni méddam ca taal bu yànj ba, mu sànku.