Daniel 7:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«La ca topp mu neeti ma: “Ñeenteelu rab wi mooy ñeenteelu nguur giy taxaw ci kaw suuf, wuuteek nguur yépp. Dina mëdd àddina sépp, nappaaje ko, rajaxe ko.