Deuteronomy 1:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ngoog, seen Yàlla Aji Sax ji moo teg réew mi fi seen kanam. Demleen nangu ko, ni leen ko seen Yàllay maam Aji Sax ji, waxe. Buleen ragal, buleen yoqi.»