Deuteronomy 1:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ngeen dikk yeen ñépp fi man, ne ma: «Nan yebal aw nit, ñu jiitu nu, yëral nu réew ma, te délsi wax nu yoon wu nuy jaare, ak dëkk yu mag ya nuy duggeji.»