Deuteronomy 1:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ba noppi sàkk ca meññeefum réew ma, indaaleel nu. Ñu wax nu nag ne nu: «Réew mu baax la nu sunu Yàlla Aji Sax ji jox.»