Deuteronomy 1:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ñeent fukkeelu atam, gannaaw ba bànni Israyil génnee Misra, keroog benn fan ca fukkeelu weer waak benn, ca la Musaa doora wax bànni Israyil mboolem lu ko Aji Sax ji santoon ca ñoom.