Deuteronomy 1:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa Kaleb doomu Yefune moo koy gis, te réew ma mu teg tànkam, moom laa koy jox, mook askanam, ndax moo matal kóolute ci Aji Sax ji.»