bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Deuteronomy 1:41
Deuteronomy 1:41 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ngeen wax ma, ne ma: «Noo tooñ Aji Sax ji. Waaye dinanu dem xareji noonee nu ko sunu Yàlla Aji Sax ji sante woon.» Ku nekk ci yeen daldi ràngoo ngànnaayam, ngeen defe ne yéegi diiwaanu tund wa dina leen yomb.