Deuteronomy 1:42 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji ne ma: «Wax leen ne leen buñu dem, buñu xeexi ndax man Aji Sax ji àndumaak ñoom. Lu ko moy dinañu daanu ci seen kanami noon.»