Deuteronomy 10:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jant yooyu la ma Aji Sax ji wax ne ma: «Yettal ñaari àlluway doj yu mel ni yu jëkk ya, nga yéegsi fi man, ci kaw tund wi. Te nanga sàkk itam gaalu bant.