Deuteronomy 11:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nangeen ko jàngal seeni doom, di ko waxe bu ngeen toogee seen biir néeg, ak bu ngeen di dox ciw yoon, ak bu ngeen tëddee, ak bu ngeen jógee.