Deuteronomy 11:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xamleen bésub tey ne seeni doom taxul may wax, ndax ñoom xamuñu, gisuñu seen njànglem Yàlla Aji Sax ji: màggaayam, ak dooley loxoom, ak kàttanam gu réy,