Deuteronomy 11:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax seeni fan, ak seen fani doom, baree ca réew ma Aji Sax ji giñaloon seeni maam, ni kemu fan yi asamaan tiim suuf.