Deuteronomy 11:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu leen seen Yàlla Aji Sax ji yóbboo ca réew ma ngeen jëm, ngir nanguji ko, nangeen tudd barke bi ca kaw tundu Garisim, te ngeen tudd alkànde ji ca kaw tundu Ebal.