Deuteronomy 11:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag yeena ngi jàlli dexu Yurdan, ngir nanguji réew mi leen seen Yàlla Aji Sax ji jox. Bu ngeen ko nangoo ba dëkk fa nag,