Deuteronomy 12:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dogal yeek àttey yoon, yi ngeen di sàmmoo jëfe seen giiru dund ca suufas réew, ma leen seen Yàllay maam Aji Sax ji moomale, moo di yii: