Deuteronomy 12:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye bu ngeen jàllee dexu Yurdan, ba dëkki ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji sédde, ba mu noppal leen ci mboolem noon yi leen séq, ngeen dëkke xel mu dal,