Deuteronomy 12:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax bérab bu Aji Sax ji taamu ci genn ci seen giir yi, foofa ngeen di joxe seen saraxi dóomal, te foofa ngeen di def lépp lu ma leen sant.