bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Deuteronomy 12:15
Deuteronomy 12:15 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul saa yu leen soobee, sañ ngeena rendi, lekk ci lépp lu leen seen Yàlla Aji Sax ji barkeele, ak fépp fu ngeen dëkk. Ku sobewu ak ku set yépp sañ na caa lekk, mel ni bu doon kéwél mbaa kooba.