Deuteronomy 12:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu fekkee ne fi seen Yàlla Aji Sax ji taamoo dëël turam dafa soreek yeen, man ngeena rendi ci seen jur gu gudd mbaa gu gàtt, ga leen Aji Sax ji jox, na ma leen ko waxe woon. Sañ ngeen caa lekke seen biir dëkk lu leen neex.