Deuteronomy 12:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sàmmooleena déggal mboolem kàddu yii ma leen di dénk, ngir ngeen baaxle ba fàww, yeen ak seen doom, yi leen di wuutu, ndax kon yeena ngi jëfe lu baax li seen Yàlla Aji Sax ji rafetlu.