Deuteronomy 12:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu leen seen Yàlla Aji Sax ji sànkalee xeet yi ngeen jëm, ngir dàq leen, gannaaw bu ngeen leen dàqee ba dëkke seenum réew,