Deuteronomy 13:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ay nit ñu tekkiwul dara, te bokk ci yeen, ñoo jóg di waññi seen waa dëkk, naan leen: «Nanu jaamuji yeneen yàlla,» yàlla yu ngeen xamul,