Deuteronomy 13:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
buleen déglu waxu yonent boobu, mbaa boroom gént boobu, ndax seen Yàlla Aji Sax ji moo leen di nattu ngir xam ndax yeena ngi koy soppe seen léppi xol ak seen léppi bakkan.