Deuteronomy 14:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax askan wu sell ngeen, ñeel seen Yàlla Aji Sax ji. Yeen la Aji Sax ji taamu, ngir ngeen doon askan wi mu séddool boppam, ci mboolem askani kaw suuf.