Deuteronomy 14:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ngeen manula dox yoon wi, ndax seen Yàlla Aji Sax jee leen barkeele meññeef mu bare mu ngeen dul àttan, ci diggante bu sorewaatoo lool ak bérab bi seen Yàlla Aji Sax ji taamoo dëël turam,