Deuteronomy 14:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax Leween, ñi amul wàll ci seen céru suuf, dikk, ñook doxandéem yi ak jirim yi ak jëtun, yi ngeen dëkkal, ngir ñu lekk ba regg. Su ko defee seen Yàlla Aji Sax ji barkeel mboolem seenu ñaq.